Paroles officielles de la chanson «Bipp» : Idrissa Diop

Albums :

Paroles officielles de la chanson "Bipp"

Guetou sa n'deye dior
Tank ne latiar gané bipp
Teup teup ba tia kaw guêye yangueul yeuseul
Bané bipp ak m'bipp m'bipp ak m'beup
M'beup thi m'bip lepe thi beupeuk bip
Bo dek lo bene nop sama wadji yawe
Ding mé bipp.

Equibou foot bool bilé yêne gni
Gneupeu ne bipp thi li
Ami m'backé thiamé yawe mi
Gneupeu ne bipp ba fi
Liguêye biguêye défé ba ni
Gneupeu ne bippeu thi li.

Equipe nationale bou Sénégal
Bou lat-dior dekiwone
Gnou takal'lène
Aye n'dombo tank
Mêye aye diame
Ne wone malène makhama nith kou wene
Dina fêgne thi kou nioule.
Siguile guêne Senegal
Bou yamone sakh nekh
Sintoubi data yagueu lole

 
 


Facebook