Paroles officielles de la chanson «Lou Tax» : Idrissa Diop

Albums :

Paroles officielles de la chanson "Lou Tax"

Lou Tax Nith di dawe Moromame ?
Lou Tax guerre doufi diexh ?
Lou Tax titangué Baré ?
Lou Tax xéekh doufi diexh ?

Whère lène ganaye yi
Nighène di wéré yeuré
Faute lèene xêele yée
Té Bayi guerre Bé
Mane waru na yène thi diamono

Lou Tax disso diexh filé ?
Lou tax dioubo ware fi Rêere ?
Xole lène aye Réewi Réewe
Di Xoulo aka guerre

Whère lène ganaye yi
Nighène di wéré yeuré
Faute lèene xêele yée
Té Bayi guerre Bé
Mane waru na
Thi Diamono

 
 


Facebook