Paroles officielles de la chanson «Papa» : Idrissa Diop

Albums :

Paroles officielles de la chanson "Papa"

Hou papa. Hou gaïendé

Papa gaïendèk sibila
Yawe bayo wet nagno
Papa gaïendèk sibila
Méxé xada diou walo.

Yirime bagnik boli ak yirime bagnik aissa daro
Magoné boli both diak, bouli ma xekh walo
Bamu léwe natak bakarek gana diassi
Papa diak diam barlawone.
Papa diak, N'déné diak go,
Boubacar diak, cumba aïssa nalèk diagué.

Heu papa diak gaïendé la wone
Diaro xaliss bamou dane také, kuko néwone
Diak nébipé. Trafaxar alpha diogou
Yirime bagnik boli, AK yirime. Bagnik aïssa
Daro. Magoné Boli MBoth diagué.
Boli ma xekh walo bamu léwe natak
Bakarek.

 
 


Facebook