Paroles officielles de la chanson «Yakar» : Idrissa Diop

Albums :

Paroles officielles de la chanson "Yakar"

Mane dé Yakar namé
Bèsse Khèle dina Sopékou
Dieumelé aye Dieufame
Thi lou Békh Bakhé
Mane Yakar na
Nith ki Manoule Deukhe thi Bine
Di yakheu Doune gui
Di tal Aleu Bé
Mane Yakar na
Yarame dina dawe

Da guêne di Xam né
Doune gui Bou Sété
Guêne set

Nith ki Fatelikoule
Bo yakhé Doune gui
Sa Bopeu Yakho

 
 


Facebook