Paroles officielles de la chanson «So La La» : Diop Wasis

Compositeurs : Diop Wasis
Auteurs : Diop Wasis
Chanteurs : Diop Wasis
Arrangeurs : Lionel Wendling
Albums :

Paroles officielles de la chanson "So La La"

Sa ma guéntë gué nééx na ma
Béén waay la guént mu di ma léébal
Waxtaan wé, saf na ma,
Waxtaan nu wurus, waxtaan nu ngalam.

Séén na dëkë bu béés,
Boru téfés, boru gééc,
Gor ak jigéén andë, muy taw, taw bu méti,
Ba Mbambilor.

So la la la
So la la la
So la la la
So la la la laaaaa.

Jégé na nu gas sul ma,
Li jëm ci li ma lalon,
Joy jël sa momél.
Hé ! nëlé dém, sori na nu
Hé ! nëlé dém, aga gunu.

Kérok da nu jaar, ci mbéd mu yaatu,
Bidéw yi tim nu, assaman si léér,
Sa ma bën ba don méti yanx,
Kérok la tagok mom.

So la la la
So la la la
So la la la
So la la la laaaaa.

Ha ha ha ha ha
Ha ha haaa !
Sa ma guéntë gué nééx na ma
Bén waay, di ma lébal, léép yu nééx
Ma ngi tëd mu ngi tang, tangaay wu méti,
Téréwul wayé, téréwul, ma ngi séén
Bén xéér mél ni wéér, jogé assamane dal ci suf,
Sa ma bën ba don méti yanx,
Kérok la tagok mom, Kérok, la tagok mom

Tagok mon, tare ri ra ra
Té ri ri ri ra ra
Bidéw yi tim nu assaman si léér, léro léér
Kérok, da nu jaar ci mbéd mu yaatu,
Bidéw yi tim nu asaman si léro léér.

 
 


Facebook