Paroles officielles de la chanson «Boyo» :

Albums :

Paroles officielles de la chanson "Boyo"

Xaralé kat yii yewoulène
Gnokh lène di naxh
Xiipilène, baboune yagui ni tok

N'dakh golo baye baboune doundé
Yagueunafi
N'dakh golo baye baboune doundé
Nagne kodi bagne

Gnome gno ghaye yoporlok sène xaliss
N'dadane yii kou mare nane
Thi ghaye nane.

Gounek m'boyo xare ko thi tatou n'da
Gounek m'boyo deko xare thi tatou n'da

Sa you maré nane dawe nane si
Legui n'da li fess na
Sa you maré nane dawe nane si
Legui n'da li fessatina

 
 


Facebook