Paroles officielles de la chanson «Disso» :

Albums :

Paroles officielles de la chanson "Disso"

Nagne lène disso ak baye kat yi i
Napeu kat yii sameu kat yii
Ghu diarignu souf silé.

Yêne baïyilène mala yé é
Gnu lekeu sakheu yaye yi i
Baïlène nature bi yêne
Niko yala saké mome
N'dakh bu dioure gui fébaré
Aduna bi tawaté

Disso ak baye kat yilé
Disso ak sameu kat yilé
Disso ak napeu kat yilé
Ghir diarigno souf silé.

Reene milé foukalène garape yêene
N'dakh garabaya hemdi tawe bilé
Té bou mala yii wéroulé
Dioure gui doufi wéré
Xolale gueth nimou yatoo
Sakhar gué doutia dawe
Autorail dou tia dawe
Bokome galako xam

Disso ak baye kat yi
Disso ak sameu kat yi
Disso ak napeu kat yi
Ghir diarigno souf silé.

 
 


Facebook