Paroles officielles de la chanson «Fonck» :

Albums :

Paroles officielles de la chanson "Fonck"

Fonkale sa yaye, gueumeule sa baye
Wave yawe lolou moye sa dolé

Dome yaye fonkale sa yaye
Gueumeule sa bayé é
N'dakh gnognu gnoye sa dolé
Xolale yaye nimou soné thi dome
Diourome gninty wère mou eumbala
Xolale baye nimuye dibi dibé
N'dakh beugoule n'diabote fandé
Dome yaye fonkale sa yaye
Gueumeule sa bayé
N'dakh gnome gnoye sa téré é é.

Fariyo foukanagnulène
Gnugh lène di gnanale
N'dakh yenaye sunu dolé
Gueureum nalu lène
Lomu méti méti, loumu tare tare
Yenaye sunu dolé
Yayo yaye boye
Samba siré gangho é
Ma xakh la
Liye sa téré
Lolou moye sa

 
 


Facebook