Paroles officielles de la chanson «N'dawsi» :

Albums :

Paroles officielles de la chanson "N'dawsi"

N'dawsi dieguessil
Mané yawe milé beugueunala
N'dawsi dieguessil
Mané yawe milé sop nala.
Sa boute yii melni wère
N'daw silé sopanala
Beugueunala
Xalé bilé
Diéguessima
Boma diegué sama yarame dawe
Xalé bilé ya taroo
Ya tayo
Talou tatou
Bou takhoussane dioté
Gha sangou solou
Xêgne lou nèxé
Rombeu guesto
N'daw sè set
Sima n'dakh té meuneu touma xaré.
Diek tank ratête téguine
Lerale guissa kaname migui
Bêguêle saraxole

 
 


Facebook