Paroles officielles de la chanson «La Boite A Photo» : William Balde

Compositeurs : Gil Gimenez, William Balde
Auteurs : Aumar Sow, William Balde
Chanteurs : William Balde
Arrangeurs : Philippe Desbois, Ilan Abou
Éditeurs : Universal Music Publishing
Albums :

Paroles officielles de la chanson "La Boite A Photo"

Sayüma lagissé
Dama laï bengeu wakh-li tchi sama khöll,
Wahé khep nge samaï khalatt bä fogné
Topoto üma tiono gunde-gi,
Beugema !
Amo darra lö chille-tite
Kaï wuyüma amö-darra loï ragall
Teïte-néka-tuma göné
Budé za fallé-üma darra...
Dunde akh nitte néküll mbir mü yômbe...

Xam-mü-ma saï kharitte
(Mané) Xan-mü-ma, xam-mü-ma
Xam-mü-ma saï kharitte
Li sökhal-nama, sökhal-nama...

Yittel-nitte-ny beuss-bü-neck
Mö warral nga maï kholé
Ni-kü-top lüdull tiaxane...

 
 


Facebook