Paroles officielles de la chanson «Boulfale» : Ismaël Lo

Compositeurs : Ismaël Lo
Auteurs : Ismaël Lo
Chanteurs : Ismaël Lo
Éditeurs : Universal Music Publishing
Albums :

Paroles officielles de la chanson "Boulfale"

Yaw yagui kheydem dl dan sadole
Mane bkhna lol
Khamoulo nokay ame khamoulo nokay woute
Lll doyna war
Yaw yagui khey dem sa diabot nl motak
Lll doyna war
Khamoulo nakay ame khamougnou nokay woute
Lll metina lole
Kon mbok boul fale boul fale
Boul fale boul fale
Kl migui khey dem dl dane dolem
Mane bakhna lol
Khamougnou nokay woute khamougnou nokayame
Lll doyna war
Yaw yagui khey dem sa diabot nl motakh
Mane bakhna lol
Khamougnou nokay ame khamougnou nokaywoute
Lll metina lool
Kon mbok boul fale boul faale
Boul fale boul fale
Adouna mom nilawara deme dane sadole mola war
Khamougnou noka ame khamougnou noka woute
Demal dane sadole mogueun teyakar koudoul yala
Boul fale boul fale
Kon boul fale boul fale
Kon bok boul fale boul fale
Kon bok boul fale boul fale

 
 


Facebook