Paroles officielles de la chanson «Jiguen» : Ismaël Lo

Compositeurs : Ismaël Lo
Auteurs : Ismaël Lo
Chanteurs : Ismaël Lo
Éditeurs : Universal Music Publishing
Albums :

Paroles officielles de la chanson "Jiguen"

Jiguen yay souma yaye
Mane jiguen kay jiguen souma wetelo
Yaw yala mola soutoural
Te koula soutoural texe
Oh oh jiguen jiguen alalou yala de waw gnoudem
Jiguen yay sounou yaye yaw
Mané jiguen kay jiguen sounou dekeu ndo
Yadi sounou lepeu fep
Yaw sounou loune foune
Oh oh jiguen jiguen alalou yala de waw gnoudem
Mane jiguen sounou khol sedetina yaw
Koula soralewoul
Dana yaka gnamou mbame de
Magui delou santa yala
Bing gnou maye taka ndere
Oh jiguen kene manoula fay
Waw gnoudem

Yenay diantabi bouguene leroul dara dou lere
Kon leral gno gnou lere
Yenay assaman bouguen hinoul bilay dou taw
Kon hine lene mou taw
Yènay thiaby thiafay koulèn saffo
Mana yègue si safsap safsap
Jiguen nanou gueune fonke jiguen de
Jiguen jiguen jiguen jiguen ma fonke jiguen
Ndakh souma yayo boye
Yénay diantabi yenay diantabi
Yenay diantabi bouguene leroul dara dou lere
Kon leral gno gnou lere
Yenay assaman bouguen hinoul bilay dou taw
Kon hine lene mou taw
Yènay thiaby thiafay koulèn saffo
Mana yègue si safsap safsap
Si safsap safsap

 
 


Facebook