Paroles officielles de la chanson «Ma Dame» : Ismaël Lo

Compositeurs : Ismaël Lo
Auteurs : Ismaël Lo
Chanteurs : Ismaël Lo
Éditeurs : Universal Music Publishing
Albums :

Paroles officielles de la chanson "Ma Dame"

Cherie coco neguou sey nila
Teye mou degueur tegua bagna tayi
Malay mougnal yaw tamit ngua may mounieul
Bouboba djiabot gui manna barkel
Sohna sile yagua nala setloo
Loumala togne togne yagui def sa warougar
Yangui khol manmi louma nekho yaw ngua siy diar
Han diallo dieri
Kon teudeul sangou way malay khalamal
Sa nguinaw fanang yako mome
Teudeul sangou teudeul sanguou
Malay khalamal sa nguinaw fanang
He diallo dierri
Chérie chérie diallo diéri anh diallo diéri
Cherie cherie diallo dieri anh diallo dieri
Chérie chérie diallo diéri anh diallo diéri
Cherie cherie diallo dieri anh diallo dieri
Ma dame unn ma dame
Man guintena dieul ndakarou diaye mayloko
Gnou topeumeu nane dama guata khel
Walay guatouma khel
Lek lek ma khalat dieul assaman ak souf maylako
Sama yenela sl sohnassi
Walay guatouma khel
Kon cherie cherie diallo dieri anh diallo dieri
Chérie chérie diallo diéri anh diallo diéri
Cherie cherie diallo dieri anh anh anh cherie
Kon teudeul sangou way ne malay khalamal
Saguinaw fanang yako mome
Teudeul sanguou teudeul sangou
Malay khalamal sa guinaw fanang he diallo dieri
Chérie chérie diallo diéri anh diallo dieri

 
 


Facebook